The song Dabbaax is performed by Youssou N'Dour in the album named Rokku Mi Rokka in the year 2007 .
1 2 3 4
kerok bissou penc bognouy wadjia wathié janta bi
Di wadjial Péssé ba
Moulay dabbaxx yalla nagnou la diégué yalla daal moy taan waayam
Moulaay Dabaaaaax.........
Bougnou Faté, Bess boboulé, Uhh Bougnou Soré, Bess boboulé
Bougnou faté Bess Boboulé,
Lofa Gnaane, Yalla May lako.
Modaane wakhal nitt gnep, Mo daane wakhal nasraane yi
Anh Mo daane Kadou Askane wi.
Dafa daane wakh naane nagnou bolé sougn rew
Dafa daane wakh naane bou kéne wéngal gaal gui
Dafa daane wakh naane nagnou bolé sounou khol yi
Dafa daane wakh naane nagnou yeureum Djiguéen
Sa borom bi begu na, Yonentam bi begu na, yako liguéyal sa borom.
Moulaye Dabbaxx yaw dé wacci ngua ma*so wakh lou amoul.
Kérok bang gnou djito a*samaane si da Leudeum, Bessa ngui kéne dotou ko Fatéééti.... Moulaay Dabbaxx
Bougnou Faté, Bess boboulé, Bougnou Soré, Bess boboulé
Bougnou faté Bess Boboulé,
Lofa Gnaane, Yalla May lako.
anh! Modaane wakhal nitt gnep, anh! Mo daane wakhal nasraane yi.
Anh! Mo daane wakhal Askane wi.
Dafa daane wakh naane na gnep ligueye
Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
Dafa daane wakh naane na gnep liguèye
Dafa daane wakh naane nagn diangal djiguééne gni
daawaoul Sétane lou gnaaw
Poussom la yorone fou khotékou Mou gnaw
Rewmi..rewmi amélnagnou la ndiouka Moulaay Dabbaxx
daawaoul Sétane lou gnaaw
Poussom la yorone fou khotékou Mou gnaw
Rewmi..rewmi amélnagnou la ndiouka Moulaay Dabbaxx.
Bakrék Dara Maam, Aram lô Coumba Thiam,
Magn Penda ak Pathé Pendaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaah
Modaane wakhal nitt gnep, Mo daane wakhal nasraane yi
Mo daane Kadou Askane wi.
Dafa daane wakh naane nagn diap sounou rewmi.
Dafa daane wakh naane nagnep liguéye
Dafa daane wakh naane nagn Yeureum djiguéene gni.
Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
Youssou N'Dour - Rokku Mi Rokka
- 4-4-44
- Pullo Ardo
- Sama Gammu
- Bajjan
- Baay Faal
- Sportif
- Tukki
- Lett Ma
- Dabbaax
- Xel
- Wake Up